Gorée

Youssou N'Dour

Transposer:

Bama démé gorée manne Andak samayyy kharite Demm sa keur diam gawonne Dama dalle di seugemm dioyy Goor yi magg yi bi boor Djiguéne yu magg yi bi boor Goor yu ndaww yi bi boor Djigéne yu naww yi tchi bénène boor Niu daddi fayy khali yonne Yonne bo khamni dangay demm Yonne bo khamni dangay dem Sa khell du demm ludull ssi délussé Lolloyyy natu lawu buur bi mi borom doggal yyé Lolayy nattu lawu buur bi boromm kunfa yakune                   Bama démé gorée manne Andak samayyy kharite Demm sa keur diam gawonne Dama dalle di seugemm dioyy Goor yi magg yi bi boor Djiguéne yu magg yi bi boor Goor yu ndaww yi bi boor Djigéne yu naww yi tchi bénène boor Niu daddi fayy khali yonne Yonne bo khamni dangay demm Yonne bo khamni dangay dem Sa khell du demm ludull ssi délussé Ennnhh gorée Lolloyyy natu lawu buur bi mi borom doggal yyé Lolayy nattu lawu buur bi boromm kunfa yakune Lolloyyy natu lawu buur bi mi borom doggal yyé Lolayy nattu lawu buur bi boromm kunfa yakune Gorée Lolloyyy natu lawu buur bi mi borom doggal yyé Lolayy nattu lawu buur bi boromm kunfa yakune

Du même artiste :

empty heart empty heart F#m, F#m/E, Dmaj7, Bm7, Amaj13, G#7, Dbm7, B6/9
empty heart empty heart F#m, E, D, Bm, Ab, C#m, B, A
Cette chanson évoque des thèmes de nostalgie et de connexion aux racines. Elle parle de l'importance de sa terre natale et des liens familiaux. À travers des métaphores puissantes, l'artiste exprime le désir de revenir à des valeurs essentielles, de se souvenir de ceux qui sont chers et de célébrer la culture et l'identité. Le contexte de cette œuvre est ancré dans l'histoire et la mémoire collective, notamment en lien avec l'île de Gorée, symbole de la traite des esclaves et des injustices passées. Cela ajoute une profondeur émotionnelle à la chanson, mettant en lumière les luttes passées tout en regardant vers un avenir plein d'espoir.